TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 2/03 p. 8
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2003
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2007
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2006
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2008
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2004
Xóotalal waxtaan bi
Sasu Nguuru Yàlla — 2003
km 2/03 p. 8

Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

La Tour de Garde 15 févr.

“ Am na ñuy laajte ndax Yàlla am na. Am na ñu gëm ne Yàlla am na waaye dañuy wax ne dafa ñu sore lool. Lan nga ci xalaat ? [Mayal nit ki mu tontu.] Jàng a xam Yàlla, lu am solo la. Xoolal lu tax. [Jàngal Yowanna 17:⁠3.] Xam naa ne waxtaan bi nekk fii ci yéenekaay bii dina la neex. ”

Réveillez-vous ! 22 févr.

“ Ñu bare tey amuñu lekk bu doy. Ay xale sax bokk nañu ci. Ndax foog nga ne ndogalu Yàlla la ? [Mayal nit ki mu tontu.] Seetal lu Yàlla dige ci Biibël bi. Lu neex a dégg la. [Jàngal Sabuur 72:16.] Réveillez-vous ! bii dafay wone lu tax mu am ay nit ñu amul lekk bu doy. Dina wone it, te loolu sax moo ëpp solo, ne léegi Yàlla dindi loolu. ”

La Tour de Garde 1er mars

“ Loo xalaat ci kàddu bu am solo bii nekk ci Mbind mu sell mi ? [Jàngal Macë 5:10.] Naka la nit mënee bég fekk ñu ngi koy fitnaal ? [Mayal nit ki mu tontu.] Ci ñaari xaaj yi njëkk ci yéenekaay bii, dañuy wax ci ay nit ñu bégoon fekk ñu ngi woon ci metit. Xam naa ne dinga bëgg jàng ni ñu fexee ba am loolu. ”

Réveillez-vous ! 8 mars

“ Coono yi bare nañu tey. Waaye am na lu bare lu war a tax ñu gërëm Yàlla. Du dëgg ? [Mayal nit ki mu tontu.] Yàlla dafa def ci suñu yaram lu mën a tax ñu am bànneex ci suñu dund. [Jàngal Sabuur 139:14.] War nañu ko ci gërëm bu baax. Moom la Réveillez-vous ! bii di wone. ”

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager