TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • fg p. 32
  • Li nekk ci téere bii

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Li nekk ci téere bii
  • Xibaaru jàmm bi jóge ci Yàlla !
Xibaaru jàmm bi jóge ci Yàlla !
fg p. 32

Li nekk ci téere bii

Ban waxtaan moo la gën a itteel ?

1 Lan mooy xibaaru jàmm bi ?

2 Kan mooy Yàlla ?

3 Ndax ci dëgg-dëgg, xibaaru jàmm bi, ci Yàlla la jóge ?

4 Kan mooy Yeesu Kirist ?

5 Lan la Yàlla bëggoon bi muy sàkk suuf si ?

6 Ndax ñi dee dinañu mas a dekki ?

7 Lan mooy Nguuru Yàlla ?

8 Lu tax Yàlla bàyyi lu bon ak coono yi di am ?

9 Lan ngeen mën a def ba am jàmm ci seen njaboot ?

10 Naka lañuy ràññee ni Yàlla bëgge ñu jaamu ko ?

11 Ban njariñ lañu mën a am ci topp xelal yi nekk ci Biibël bi ?

12 Naka nga mënee jege Yàlla ?

13 Lan mooy xibaaru jàmm bi jëm ci wàllu diine ?

14 Lu tax Yàlla am mbootaay ?

15 Lu tax nga war a kontine ?

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager