TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • lff
  • Xaaj 3

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Xaaj 3
  • Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 3
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Nañu fàttaliku xaaj 3
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • Lan la Biibël bi wax ci salibateer ak séy?
    Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
  • “ Nangu ko ”
    Sasu Nguuru Yàlla — 2003
Xóotalal waxtaan bi
Mën nga dund ci jàmm ba fàww! (Njàngum Biibël bi)
lff

XAAJ 3

Édition imprimée

Li ñu nar a gis: Dinañu gis li Yàlla di xaar ci ay jaamam

Kuy jàng Biibël bi mu ngi fëgg bunt keneen. Ki koy jàngal Biibël bi moo koy gunge ci liggéeyu waare bi.

LESOŊ YI

  1. 34 Naka lañu mën a wonee ne bëgg nañu Yexowa?

  2. 35 Ni ñu mën a jële ay dogal yu baax

  3. 36 Nañu jub ci lépp

  4. 37 Lan la Biibël bi wax ci liggéey ak xaalis?

  5. 38 Nañu fonk dund gi ñu Yàlla may

  6. 39 Ni Yàlla gise deret

  7. 40 Naka lañu mënee nekk ñu set ci kanamu Yàlla?

  8. 41 Lan la Biibël bi wax ci séy?

  9. 42 Lan la Biibël bi wax ci salibateer ak séy?

  10. 43 Naka la karceen yi war a gise sàngara?

  11. 44 Ndax feet yépp a neex Yàlla?

  12. 45 Naka lañu mënee wone ne nguuru Yexowa rekk lañu faral?

  13. 46 Lu tax nga war a jébbalu te sóobu ci ndox?

  14. 47 Ndax pare nga ngir sóobu ci ndox?

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager