TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • th lesoŋ 17 p. 20
  • Na li ngay wax leer ci ñi lay déglu

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Na li ngay wax leer ci ñi lay déglu
  • Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Defal waxtaan buy yokk xam-xam
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Waxal ak cawarte
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Waxal mel ni kuy waxtaan
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
  • Woneel bu baax njariñu aaya yi
    Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
Xóotalal waxtaan bi
Yokkal sa mën-mën ci jàng ak jàngale
th lesoŋ 17 p. 20

LESOŊ 17

Li ngay wax na leer ci ñi lay déglu

Aaya bi ñu lim

1 Korent 14:9

LI NGA WAR A JÀPP: Dimbalil ñi lay déglu ba li ngay wax leer ci ñoom

NI NGA KO MËN A DEFE:

  • Gëstul bu baax li nga nar a waxtaane. Xamal bu baax li nga war a waxtaane ba mën koo wax ak say kàddu bopp ci fasoŋ bu leer.

  • Waxal ay kàddu yu gàtt te leer. Wax ak kàddu yu gudd bonul, waaye booy wax ci ponk yi gën a am solo def ko ak ay kàddu yu gàtt te leer.

    Xelal bu baax

    Bu ci boole yu sew yu mën a jaxase xelu nit ñi te réeral leen. Li gën mooy ngay wax ak ay kàddu yu leer naññ.

  • Leeralal kàddu yi nit ñi faralul di dégg. Moytul a wax kàddu yu ñi lay déglu faralul di dégg. Boo naree wax kàddu yu nit faralul di dégg, walla wax ci nit ku ñu tudd ci Biibël bi walla ci ni ñu doon natte walla peesee ca jamono yu yàgg ya, walla wax ci ay aada yu yàgg, leeral ko.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager