Nanga bëgg Yexowa ak sa xol bépp
DEUTÉRONOME 13:3
SUBA SI
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla No. 109 ak ñaan
10:00 “ Mbëggeel ci Yàlla mooy sàmm ay ndigalam ”
10:15 Mbëggeel ci Yexowa mooy bëgg sa mbokk ci ngëm
10:30 “ Nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp ”
10:55 Woy-Yàlla No. 82 ak yégle yi
11:05 “ Mbëggeel day suul bàkkaar yu bare ”
11:35 Jébbalu bi ak sóob bi
12:05 Woy-Yàlla No. 50
NGOON SI
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla No. 62
1:35 Ay nettali yu jëm ci suñu liggéey
1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:15 Waxtaan bu def ay xaaj : Màggalleen Yexowa seen dund gépp
Xale yi
Ndaw yi
Mag ñi
3:00 Woy-Yàlla No. 10 ak yégle yi
3:10 Nanga bëgg Yexowa ak sa xol bépp
3:55 Woy-Yàlla No. 37 ak ñaan