“Bégal ci Yexowa”
Sabóor 32:11
SUBA SI
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla No. 9 ak ñaan
10:00 «Bégal te bànneexoo [Yexowa] Aji Sax ji»
10:15 Bégleen doonte sax yeen a ngi ci ay jafe-jafe
10:30 Nangeen «fees ak mbég» ci liggéeyu waare bi
10:55 Woy-Yàlla No. 76 ak yégle yi
11:05 Buleen bàyyi seen nafsu «diigal leen»
11:35 Jébbalu bi ak sóob bi
12:05 Woy-Yàlla No. 51
NGOON SI
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla No. 111
1:35 Ay nettali
1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Yexowa moo ñuy bégal
• Bu ñuy sàkk ay taalibe
• Bu ñuy dimbali suñu mbokk yi ci ngëm
• Bu ñuy muñ ay jafe-jafe
3:00 Woy-Yàlla No. 2 ak yégle yi
3:10 Nanga kontine di jiital Yexowa ci lépp
3:55 Woy-Yàlla No. 7 ak ñaan