Bégalal xolu Yexowa!
Kàddu yu Xelu 27:11
SUBA SI
9:30 Misik
9:40 Woy-Yàlla No. 29 ak ñaan
9:50 Bégalal xolu Yexowa!
10:05 Waxtaan bu def ay xaaj: Nañu roy ñeent ci jikkoy Yexowa yi
• Njub
• Ni muy jëfandikoo kàttanam
• Sago
• Mbëggeel
11:05 Woy-Yàlla No. 81 ak yégle yi
11:15 Magalal Yàlla ci «gëna meññ»
11:30 Jébbalu bi ak sóob bi
12:00 Woy-Yàlla No. 49
NGOON SI
1:10 Misik
1:20 Woy-Yàlla No. 28 ak ñaan
1:30 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp: Mën nga bégal Yàlla!—Ci naka?
2:00 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:30 Woy-Yàlla No. 35 ak yégle yi
2:40 Waxtaan bu def ay xaaj: Nanga neex Yexowa ci . . .
• Sa dund
• Sa njaboot
• Sa mbooloo
• Sa gox
3:40 «Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole»
4:15 Woy-Yàlla No. 110 ak ñaan