Nañu dugg ci noflaayu Yàlla!
YAWUT YA 4:11
Suba si
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla No. 87 ak ñaan
10:00 Naka lañu mënee dugg ci noflaayu Yàlla?
10:15 «Kàddug Yàlla mi ngi dund»—Loolu lu mu tekki?
10:30 Ci lépp li ngeen di def, wutleen a xam li Yexowa bëgg
10:55 Woy-Yàlla No. 89 ak yégle yi
11:05 Yexowa dafay barkeel ñi koy déggal
11:35 Jébbalu bi ak sóob bi
12:05 Woy-Yàlla No. 32
Ngoon si
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla No. 49
1:35 Ay nettali
1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Dañuy bégal Yexowa!
• Ndaw ñi
• Jigéen ñi
• Mag ñi
3:00 Woy-Yàlla No. 38 ak yégle yi
3:10 Bégleen ci liggéeyal Yexowa
3:55 Woy-Yàlla No. 118 ak ñaan