‘Nañu déglu li xel mu sell mi di wax mbooloo yi’
PEEÑU MA 3:22
Suba si
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla 1 ak ñaan
10:00 ‘Nañu déglu li xel mu sell mi di wax mbooloo yi’—Naka lañu ko mën a defee?
10:15 «Xàddiwoo»
10:30 «Bul ragal»
10:55 Woy-Yàlla 73 ak yégle yi
11:05 «Weddiwoo sa ngëm ci man»
11:35 Sóob bi: Li seen sóob ci ndox di tekki
12:05 Woy-Yàlla 79
Ngoon gi
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla 126
1:35 Ay nettali
1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Ni ñu mënee topp xelal yi ñuy jot
• ‘Ŋoyleen ci li ngeen am’
• «Yewwul te dëgëral li des»
• ‘Teg naa fi sa kanam, bunt bu tijjiku’
3:00 Woy-Yàlla 76 ak yégle yi
3:10 ‘Nanga farlu’
3:55 Woy-Yàlla 129 ak ñaan