“ MBËGGEEL DAY YÉKKATI NGËM ”
1 KORENT 8:1
SUBA SI
9:30 Misik
9:40 Woy-Yàlla No. 90 ak ñaan
9:50 “ Xam-xam day tax ba nit yég boppam, waaye mbëggeel day yékkati ngëm ”
10:05 Waxtaan bu def ay xaaj : Yékkati nañu ngëmu ñeneen ñi
Barnabas
Pool
Dorkas
11:05 Woy-Yàlla No. 79 ak yégle yi
11:15 Bu ñu yem rekk ci yégle xibaaru jàmm bi ci liggéeyu waare bi
11:30 Jébbalu bi ak sóob bi
12:00 Woy-Yàlla No. 52
NGOON SI
1:10 Misik
1:20 Woy-Yàlla No. 107 ak ñaan
1:30 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp : Naka la mbëggeel dëgg mënee tax dëgg gi sax ?
2:00 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:30 Woy-Yàlla No. 101 ak yégle yi
2:40 Waxtaan bu def ay xaaj : Nañu def suñu wàll ngir bokk ci ñiy tax jëmm ji yokku
Nañu fonk dëgg gi nekk ci Biibël bi
Nañu wéy di wone ne santaane Yàlla yi am nañu njariñ ci suñu dund
Nañu yékkati suñu ngëmu mbokk yi ci ngëm
3:40 “ Lépp li ngeen di def, defleen ko ak mbëggeel ”
4:15 Woy-Yàlla No. 105 ak ñaan