Yexowa dafay jàngal mbooloom ñu nekk benn
EFES 4:3
Suba si
9:30 Misik
9:40 Woy-Yàlla No. 85 ak ñaan
9:50 Nañu fonk suñu palaas ci mbooloo Yexowa
10:05 Waxtaan bu def ay xaaj: Dañu wone ne fonk nañu ñeneen ñi
• Eliyu
• Lidi
• Yeesu
11:05 Woy-Yàlla No. 100 ak yégle yi
11:15 Wéyleen di dimbali ñeneen ñi ñu ñëw bokk ci mbooloo Yexowa
11:30 Jébbalu bi ak sóob bi
12:00 Woy-Yàlla No. 135
Ngoon si
1:10 Misik
1:20 Woy-Yàlla No. 132 ak ñaan
1:30 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp: Ndax yéen a ngi def lépp ngir jàmm am ci seen kër?
2:00 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:30 Woy-Yàlla No. 136 ak yégle yi
2:40 Waxtaan bu def ay xaaj: Naka nga mënee def lépp ngir wut jàmm?
• Nanga «wax lu rafet»
• Nanga ‘wéer sa dund ci mbëggeel’
• Nanga xeex suñuy noon
3:40 Buleen «noppee sant Yàlla» ci li ngeen bokk ci mbooloom
4:15 Woy-Yàlla No. 107 ak ñaan