Yokkal sa ngëm!
YAWUT YA 10:39
SUBA SI
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla No 119 ak ñaan
10:00 Lu tax ñu war a yokk suñu ngëm tey ci tey?
10:15 Ndax yeen a ngi gis ‘Yàlla, mi kenn manula teg bët
10:30 «Ngëm ci kaw dégg lay juddoo»
10:55 Woy-Yàlla No 104 ak yégle yi
11:05 ‘Li Xelu Yàlla di meññ mooy [...] ngëm’
11:35 Jébbalu bi ak sóob bi
12:05 Woy-Yàlla No 50
NGOON GI
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla No 3
1:35 Ay nettali
1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Dimbalil ñeneen ñi ñu dëgëral seen ngëm
• Dimbalil ndaw ñi
• Dimbalil ñi ngay jàngal Biibël bi
• Dimbalil sa mbokk yi ci ngëm
3:00 Woy-Yàlla No 38 ak yégle yi
3:10 «Nañu ne jàkk Yeesu, moom mi samp ngëm, ba ub làmbi ngëm»
3:55 Woy-Yàlla No 126 ak ñaan