Ñi bëgg jàmm
LUUG 10:6
Suba si
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla No. 58 ak ñaan
10:00 Yéen ñi bëgg jàmm, dal-leen ak jàmm!
10:15 Wéy leen di wut ñi bëgg jàmm
10:30 Naka la Yeesu, Buuru jàmm bi, di leen di dimbalee ngeen wut ñi bëgg jàmm
10:55 Woy-Yàlla No. 103 ak yégle yi
11:05 Ñi bëgg jàmm duñu jàng xare
11:35 Jébbalu bi ak sóob bi
12:05 Woy-Yàlla No. 79
Ngoon gi
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla No. 76
1:35 Ay nettali
1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Yéen ñi bëgg jàmm, nañu dimbalante suñu biir
• «Ubbileen seen xol»
• Dimbalileen ndaw yi ñu def lépp li ñu mën ci liggéeyu Yexowa
• Teral-leen mag ñi
3:00 Woy-Yàlla No. 57 ak yégle yi
3:10 Yeen ñi bëgg jàmm, lan ngeen mën a def ba not lu bon, ci def lu baax?
3:55 Woy-Yàlla No. 45 ak ñaan