Ni ma yàkkamtee ndimbalu Yexowa!
SABÓOR 130:6
Suba si
9:30 Misik
9:40 Woy-Yàlla No. 88 ak ñaan
9:50 Naka lañuy wonee ne yàkkamti nañu ndimbalu Yexowa?
10:05 Waxtaan bu def ay xaaj: Royleen ci ñi yàkkamti woon ndimbalu Yexowa
• Abakug
• Yowaana
• Aana
11:05 Woy-Yàlla No. 142 ak yégle yi
11:15 Lan ngeen di séentu?
11:30 Jébbalu bi ak sóob bi
12:00 Woy-Yàlla No. 28
Ngoon si
1:10 Misik
1:20 Woy-Yàlla No. 54 ak ñaan
1:30 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp: Lu tax muñ am solo?
2:00 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:30 Woy-Yàlla No. 143 ak yégle yi
2:40 Waxtaan bu def ay xaaj: Yaakaaral Yexowa . . .
• Boo wéetee
• Boo juumee
• Boo gisee ku bon am jàmm
3:40 «Ku jub jot sab yool»
4:15 Woy-Yàlla No. 140 ak ñaan