Amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi
ROOM 1:16
Suba si
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla nº 67 ak ñaan
10:00 Amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi—Lu tax?
10:15 Woneel ne da nga takku ci xibaaru jàmm bi
10:30 Woneel ne liggéeykat bu amul dara li muy rus nga
10:55 Woy-Yàlla nº 73 ak yégle yi
11:05 Solul Xel mu ànd ak kàttan, mbëggeel ak moom sa bopp
11:35 SÓOB BI: Wéyal di ‘déggal xibaaru jàmm bi’
12:05 Woy-Yàlla nº 75
Ngoon gi
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla nº 77
1:35 Ay nettali
1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Dañu fonk . . .
• Santaane Yàlla yi
• Nguuru Yàlla
• Ñi ñuy jiite ci mbootaayu Yàlla
3:00 Woy-Yàlla nº 40 ak yégle yi
3:10 Dañuy «ndamu ci Boroom bi»
3:55 Woy-Yàlla nº 7 ak ñaan