Na seeni jëf méngook li ngeen xam ci xibaaru jàmm bi
FILIB 1:27
Suba si
9:40 Misik
9:50 Woy-Yàlla nº 35 ak ñaan
10:00 Naka la li nga xam ci xibaaru jàmm bi, soppee sa dund?
10:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Naka la li ñu xam ci xibaaru jàmm bi soppee seeni dund:
• Ecen
• Filib
• Akilas ak Pirsil
• Tit
11:05 Woy-Yàlla nº 76 ak yégle yi
11:15 Na nga wéy di am Jëf yuy wone ne da nga «ragal Yàlla»
11:35 SÓOB BI: Wéyal di ‘déggal xibaaru jàmm bi’
12:05 Woy-Yàlla nº 37
Ngoon si
1:20 Misik
1:30 Woy-Yàlla nº 56 ak ñaan
1:35 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp: Li nga gëm, ci lan la sukkandiku?
2:05 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
2:35 Woy-Yàlla nº 24 ak yégle yi
2:45 Waxtaan bu def ay xaaj: «Li ñu bëgg mooy di rafetal suñu tur ni Seede Yàlla ci . . .»
• Muñ
• Laabiir walla mbaax
• Njub
3:30 Yàlla dafa ñuy jàngal jaaraale ko ci xibaaru jàmm bi. Naka la koy defe?
4:00 Woy-Yàlla nº 29 ak ñaan