TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 8/04 p. 8
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2004
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2006
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2003
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2005
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2008
Xóotalal waxtaan bi
Sasu Nguuru Yàlla — 2004
km 8/04 p. 8

Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

La Tour de Garde 15 août

“ Seetlu nañu ne nit ñu bare dañuy wut ku leen ëpp xam-xam ngir mu xelal leen ci wàllu séy ak ci ni ñu waree yar seeni doom. Ci yow, kan moo ñu gën a mën a xelal ci wàll yooyu ? [Mayal nit ki tontu.] Ki ñu sàkk am na lu mu wax ci mbirum njaboot. Téere bii, ci loolu lay wax. ” Jàngal Sabuur 32:​8, te woneel ne Yàlla dafa ñu bëgg jàngal te jox xelal yu baax.

Réveillez-vous ! Aug. 22

“ Fii ci Senegaal, ñu bare dañuy xalaat ne, yar doom, wareefu yaay ji la. Waaye ci sa xalaat, ban wàll la baay ji war a am ci yar xale yi ? [Mayal nit ki tontu.] Boroom kër yi amatul seen jotu doom ñu ngi gën di bare. Réveillez-Vous ! bii, ci loolu lay waxtaan. Te dafay wone lu baax li yaru baay mën a def ci xale. ” Won ko ci Léebu 13: 1 lu baax li yaru baay mën a def ci xale.

La Tour de Garde Sept. 1

“ Am na lu ñu leen bëggoon a laaj ci li mën a tax nit bare jàmm ci dundam. Loolu, ñépp a ko bëgg, du dëgg ? Waaye ndax ci sa xalaat, li ñu wax fii mën na tax suñu dund bare jàmm ? [Jàngal Macë 5:4a, 6a, ak 10a, ba pare mayal nit ki tontu.] Téere bii dafa ñuy leeral kàddu yooyu bokk ci waare bi ñuy wooye Waare bi ca tund ba. Wax na itam ci leneen lu ñu soxla ngir bare jàmm ci suñu dund. ”

Réveillez-vous ! Sept. 8

“ Ndax xamoon nga ne am na ñuy wax ne ñeenti nit yoo jël, kenn ki dina mas a am feebaru xel ? Ñu bare ci ñun xam nañu ku am feebar bu mel noonu. [Ubbil fu waxtaan boobu nekk ci yéenekaay bi.] Ci téere bii, dañuy wax li ñu mën a def bu ñu amee mbokk walla xarit bu am feebaru xel. ”

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager