TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 8/05 p. 8
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2005
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2006
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2004
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2003
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2008
Xóotalal waxtaan bi
Sasu Nguuru Yàlla — 2005
km 8/05 p. 8

Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

La Tour de Garde 15 août

“ Nit ñu bare dañu am mbokk mu gaañu. Loolu indil na leen naqar bu réy. Bu loolu amee, ñu bare dañuy bëgg xam fan la ki dee nekk, lan lay yëg ak yu mel noonu. Ndax nit mën na xam lan mooy dee ? [Mayal nit ki tontu.] Téere bii dafay wone li ci Biibël bi wax. Dafay wone it ne suñu mbokk ñi dee dinañu dekki. Yàlla moo ñu ko dig. ” Jàngal Yowanna 5:​28, 29. Te won ko ne bàmmeel yi ñuy wax foofu, ay bàmmeelu fàttaliku lañu, ni ñu ko waxee ci NW.

Réveillez-vous ! 22 août

“ Poroblemu xaalis mu ngi yokku rekk ci àddina si. Ñu bare dañu foog ne li ñuy woowe ci tubaab tourisme (maanaam li ñuy def ngir toppatoo gan yiy jóge bitim réew) dina leen ci mën a dimbali. Ndax xam nga ne loolu moo gën a tax nit ñi am liggéey ci àddina si sépp ? [Mayal nit ki tontu.] Tey nit ñiy tukki di jóge seen réew, dem beneen réew dañu gën a bare. Loolu indi na lu baax, waaye indi na it ay jafe-jafe. Téere bii ci loolu lay wax. Dafay xamal it ñiy tukki, di dem beneen réew, li ñu mën a def ngir moytu yenn jafe-jafe. ”

La Tour de Garde 1er sept.

“ Bu njëkk, ngor jikko bu ñu fonkoon la. Tey nit ñi dañuy wax lu baax ci jikko jooju, waaye ñi ko am, barewuñu. Nit ñu mel ni xarit bi ñuy wax fii bu ñu bare woon tey, ndax dund gi du gën a neex ? [Jàngal Léebu 17:17. Nanga fexe ba “ pour les jours de détresse ” (maanaam boo nekkee ci lu metti lool) feeñ bu baax ci li ngay jàng, ba pare mayal nit ki tontu.] Téere bii dafay wone lu tax ngor ci diggante nit ak ay mbokkam, walla nit ak ay xaritam, baax. ”

Réveillez-vous ! 8 Sept.

“ Bu ñuy seet li Yàlla sàkk, dañuy gis ne mbindeef yu bare dañuy dimbalante ? [Waxal lenn luy wone loolu ci Réveillez-vous ! bi.] Kon boo gisee ñàkk dimbalante bi am diggante doom-Aadama ndax loolu du la metti ? [Mayal nit ki tontu.] Téere bii dafay wone ne léegi Yàlla soppi loolu, te indi jàmm ak jàppoo ci kow suuf. ” Jàngal Isayi 11:⁠9.

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager