WOY-YÀLLA 157
Jàmm ji ñu doon xaar agsi na
(Taalifi Cant 29:11)
1. Doonte tiis bare na
Ci àddina si,
Ci jàmm la mbooloo Yàlla ne.
Suñu ngëm a tax
Ba duñu xàddi ndax
Léegi suñu metit
yi jeex.
(AWU BI)
Fépp ci àddina
Jàmm agsi na.
Du fi mas a jóge.
Àjjana dina neex,
Coono yépp ay jeex.
Jàmm ji ñu doon xaar
Agsi na.
2. Ñiy jaamu Yexowa
Bennoo nañu,
Koo gis, Yexowa la faral.
Àjjana jiy ñëw,
Dara gënu ko neex.
Ñi jub ñoo fay sax ci mbëggeel.
(AWU BI)
Fépp ci àddina
Jàmm agsi na.
Du fi mas a jóge.
Àjjana dina neex,
Coono yépp ay jeex.
Jàmm ji ñu doon xaar
Agsi na.
(AWU BI)
Fépp ci àddina
Jàmm agsi na.
Du fi mas a jóge.
Àjjana dina neex,
Coono yépp ay jeex.
Jàmm ji ñu doon xaar
(AWU BI)
Fépp ci àddina
Jàmm agsi na.
Du fi mas a jóge.
Àjjana dina neex,
Coono yépp ay jeex.
Jàmm ji ñu doon xaar
Agsi na.
Agsi na.
(Xoolal itam Ps. 72:1-7; Isa. 2:4; Rom. 16:20)