TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Watchtower
TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET
Wolof
  • BIBLE
  • TÉERE YI
  • RÉUNIONS
  • km 3/02 p. 8
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

Aucune vidéo n'est disponible pour cette sélection.

Il y a eu un problème lors du chargement de la vidéo.

  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
  • Sasu Nguuru Yàlla — 2002
  • Leneen lu jëm ci loolu
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2007
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2008
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2006
  • Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi
    Sasu Nguuru Yàlla — 2004
Xóotalal waxtaan bi
Sasu Nguuru Yàlla — 2002
km 3/02 p. 8

Li ñu mën a wax bu ñuy wone yéenekaay yi

La Tour de Garde 15 mars

“ Bu ñu amoon kilifa yu baax, ndax fooguloo ne dund gi ci kow suuf si dina gën a neex ? [Mayal nit ki mu tontu.] Seetal li ñu Mbind mu sell mi dig. [Jàngal Sabuur 37:11.] Jàmm ju mel nii, kilifa gu mat rekk moo ko mën a indi. Yéenekaay bii dafay wone kan mooy kilifa googu. Dafay wone it naka lañu mënee jariñoo kiliftéefam. ”

Réveillez-vous ! 22 mars

“ Yëngu-yëngu suuf dafay rey ñu bare, te yàq na lu bare. Ñi ciy mucc, ci lu ëpp, dañu ciy ñàkk seen kër ak seen alal yépp. Am na ay nit ñu bare ñu nekkoon ci béréb fu suuf yëngoo te fexe ba genn ci jafe-jafe yu ci toppoon. Réveillez-vous ! bii dafay wone naka lañu def. Dafay wax itam naka la yëngu-yëngu suuf bokke ci lu am solo lool lu Mbind mu sell mi wax ne dafa war a am. ”

La Tour de Garde 1 avril

“ Dama la bëgg won lenn luy dalal xel lu nekk ci Mbind mu sell mi. [Jàngal Macë 22:37.] Ci sa xalaat, li ñu jàng fii, lu muy tekki ? [Mayal nit ki mu tontu.] Xoolal ci téere bii, xaaj bi tudd : ‘ Wut leen Yàlla ak seen xol, ak it seen xel. ’ Ngëm dëgg, ndax ci xol rekk lay jóge, walla ci xol ak ci xel yépp lay jóge ? Tont bi dina la jàngal lu bare. ”

Réveillez-vous ! 8 avril

“ Toppatoo njaboot, lu jafe la tey, te nekk yaay yombul dara, du dëgg ? Réveillez-vous ! bii dafay wax ci : ‘ Nekk yaay : liggéey bu jafe la. ’ Bëgg naa, nga am ci benn. ”

    Téere yi ci Wolof (1996-2025)
    Ngir génn
    Ngir konektewu
    • Wolof
    • Yónnee ko
    • Ni nga bëgge mbir yi feeñe
    • Copyright © 2025 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania
    • Conditions d’utilisation
    • Règles de confidentialité
    • Paramètres de confidentialité
    • JW.ORG
    • Ngir konektewu
    Partager